Si keuyite bi, di nga fi guisse ayes khibares yu dieume si diangoro VIH/SIDA, si ayes kadous you yomba kame si diangoro VIH, si ame padjoume, si nougnouye meuna dougou si birou keurou doctor yi fi si Espagne ak tamite nane lagnouye wara andeu ak gniye ligueyes si lou dieume si wergu, gniyes liguéyes si mbotayes yiyes ligueyes ak mbolo nites gni dioguénes bitime réw té amchi gno khamné si nites gnognou diogué si biti amna gnou chi amé diangoro VIH fi si réwoume Espagne.
Dina gnou ko téki si khalamayes espagnole, anglais, français, árabe, russe, poruguais, roumain ak wolof. Pour gni deuk si rewou Senegal, Gambie, Guinée, Mali ak mauritanie. Di chi yok, kheute yi khatime yeupe té siweule ko binou diré si atoume 2010 ba taye, yoré nanou ko, ba yok chi lakouyes urdu ak chinois.
Khibar yi dieume si VIHtal meune nanou ko amal ndakhe diapale mbotaye bobou di Programme biye liguéye si wérgu yaramou mbotaye yi si souffe di chi ande ak gniye liguéye si diangoro yi diogués si gokhou réw you tangue yi té ande ak ndokhe ak gniye tomato fi wérgu yarame si aduna ak keur doctor bi toudou Drassanes si deukou Barcelone ak ETIS di Mbotaye biye liguéye ak gni diogué bitime réw si séne wérgu yarame. Amena ayes keuyites youyes tasse khibar yoyou yo khamné gno ko déffarale sou nou bopp, ame chi yo khamné danou ché andeu ak yénéni ayes mbotayes. Comme gnou mélniStopSida, Gais Positius, Creación Positive, Salud Entre Culturas wala Genera. Amna tamite ayes paches younou déffar, thiossaname mi ngui diogué si keur gou nék sa Londre té toudou NAM/Aidsmap www.aidsmap.com.